Règlement Intérieur G3SM

🌴💢 DAHIRA GÉNÉRATION SOPEY SERIGNE SAM MBAYE(G3sm) 💢🌴

Règlement intérieur

Tërrëlin yi tonno liguéyu Dahira bi

 

📍10 FUKKI POOÑ YI LA KEEN KUNNÉ WARRA SAMONTÉL NGUIR LI TARAAL AK DIAPANDIL LIGGÉYU DAHIRA BI📍

 

1) ✔👉🏿Léppu lu waay di wax mbaa mudiko sakku ci Dahira bi mu défko ak yarr aki téggin

 

2) ✔👉🏿Nañuuy moytandiku di dagganté aka mananté ci waalu xam xam, té képpu kouy tontou ap ladj nagua soukandikou thi guirouk Imam Malick

 

3) ✔👉🏿Nañuuy moytandikou pirim Al-hour-an mi ak yéne ladj yi, yousi mélni maxamam nitou Yallah bii foumou tolou ak you demé nonou

 

4) ✔👉🏿Naniuy féxee di dëppo ak théme yi, théme buñu mënn di waxtaané na ñeppu féxee dicci tënku

 

5) ✔👉🏿Buffi kénn di aadu jëmëlé ci politique, mbaa campagne politique Taay moytandiku di wax waxinou mbéd, ñou goorgoorlu ci Muritél kalaama gui

 

6) ✔👉🏿Béép kaddu buy dinghat tarixa mbaa diinéy jaambur mbaa tillimal dérru nitt buñuko yëkkëti ci Dahira bi

 

7) ✔👉🏿Nañu moytu di aadu ci lu amallul ndiariñ waa Dahira bi, mudi ci wallu pécc, woyy, football, laamb mbaa Music ak yini méll

 

8) ✔👉🏿Nanuuy wégganté ci suñu biir téy joox domi Soxna yiffi né seen thieur, buñu xulloo mbaa di xassanté

 

9) ✔👉🏿Lu waay sassoo ci jukki Al’Qhuran mbaa Xassida wala Salatu hala Nabbi mu matalko balla aap bée matt

 

10) ✔👉🏿Nañuuy téwlu kaddug Jëwring yi ndax ñoom ño sassoo féxé ba dara du sooxél liguééy bi

          

Sanctions

 

🔴Ku wacc pooñ yi dieuwriñ yi fattalilla doxin wi, booci nanguwuta tënku ñu éliminé la ci Dahira bi  wéyaal liggéy bi🔴

 

💢👉🏾 Photo Profil bi nan kooy bayi noonu té baañ dikko Changer 👈🏾💢

 

🌴💢 DAHIRA GÉNÉRATION SOPEY SERIGNE SAM MBAYE(G3sm) 💢🌴

About The Author

Related posts

1 Comment

Leave a Reply

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

G3sm.org