☘Programme de la semaine☘

💢DAHIRA GÉNÉRATION SOPEY SERIGNE SAM MBAYE (G3sm.org)💢

☘Programme de la semaine☘

💢Thèmu ALTIINÉ AK TALATA __👉🏿Waxtaané SERIGNE TOUBA ak am Jangaleem, waxtaané Khassida yi ak seen Njariñ

💢Thému ALARBA AK ALXAMIIS___👉🏿Questions & Réponses (Lath ak Tontu)

💢Thému AL JUMMA AK SAMDI___👉🏿Thème de société waxtaané Yaxu-yaxu Jamono ji ak Toluwaayu jamono ji

💢Thému DIMANCHE bu diott___👉🏿Waxtaané ak Fatalaliku ak di ñanaal SERIGNE SAM MBAYE (Rta) ak di fatalanté ci am Jangaleem

💢👉🏾Man naño déff (Questions & Réponses ci lu dieum ci Thème bi

About The Author

Related posts

Leave a Reply

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

G3sm.org